Podcasts > Tariqa
Card image cap

Tariqa

Suñu waxtaanu tay bi day jëm ci tariqa. Lan mooy tariqa ak lu ko tax a jóg? Ndax coosaanal tariqa yi moo ngi wéy ba léegi? Amul siki ni ñi sosoon tariqa yi ci lu wér lanu nekkoon, waaye lu ñuy gën a dem mu melni liy mbir mi dëgg, te mooy defar nit ku sotti, danu koy gën a sori. Ndax sant lanuy toppee Sëriñ? Lan lanu fay sàkku? Lan mooy xam Yàlla? Yiii ak yaneen laay w...

15 15

Plus d'épisodes de Wolof Podcast

=