Podcasts > yàqu-yàqu jikko yi (xaaj bu njëkk)
Card image cap

yàqu-yàqu jikko yi (xaaj bu njëkk)

«Danoo xëm te ñor a gu ñu » Sëriñ Saam Mbay. Tay ñuy waxtaane yàqu-yàqu jikko yi ànd ci ak Seex Aliw Saar. Ku am seetlu tuuti dina xam ni sunu reew mi fi mu tollu ci jikko yu yàqu kéeman la. Lan mooko sabab ak lan mooy saafara ci? Ci waxtaan bi di nanu ci yaatal lu bari ci ñaari xaaj

15 15

Plus d'épisodes de Wolof Podcast

=