Podcasts > racisme
Card image cap

racisme

Tay ñu dikkat ak baneen woppa muy « racisme ». Mu nekk lu yaatu loo xamne sa su nekk dees koy waxtaane ci pénc mi. Bu ñu xoolee béddi bi ñuy béddi nit ñu ñuul ñi nekk Ukraine te bëgg bokk ci waay-làqu yi, di nanu xamne nii lii ñuy wax « racisme » lu am la. Waaye tay danuy xootal waxtaan bi jàngat ko ak theorie bi ñuy wax « un/doing differences ». Ndaxte lu yaatu la lu...

15 15

Plus d'épisodes de Wolof Podcast

=