Podcasts > Bëgg a baax
Card image cap

Bëgg a baax

Tay ma ànd ak sama gan gu njëkk muy Bàmba ñuy waxtaane yoonu njub ak baax. Def lu baax yomb na waaye dëkk ci moo jafe. Yonent bi (saws) dafay wax ni àddina mooy aljànna ki weddi, waaye kaso la ci ki gëm. Mu melni kon ku bëgg dund ci niki Yàlla gërëmee dina laaj jékki ay jéego jëm ci yar sa bakan ak topp Yàlla. Waaye mu nekk yoon bu meti loolu. Lan mooy yoonu njub? Ak...

15 15

Plus d'épisodes de Wolof Podcast

=