Sunu episode bu njëkk ñuy waxtaane « identité culturelle » : ndax dañoo ñàkk suñu mbaatit (culture) ginnaaw bi Tubaab yi ñëwee suñu réew yi noot ñu? Ndax xeebuñ suñu bopp ginnaaw loolu? Ndax jéem nanu dellu suñu bopp? Mu nekk ay laaj yu bari yoo xamne mat na waxtaane. Ak téereeb Ken Bugul bi tudd « Le Baobab fou » lañuy jéema saytu laaj yi yépp.
INTRO
INTRO
Saison 1 Episode: 1
Identité culturelle (xam sa bopp ak sa m...
Identité c...
Saison 1 Episode: 2
Bëgg a baax
Bëgg a baa...
Saison 1 Episode: 3
Islamophobie
Islamophob...
Saison 1 Episode: 4
"Féminisme" (xaaj bu njëkk)
"Féminisme...
Saison 1 Episode: 5
racisme
racisme
Saison 1 Episode: 6
Yebbi
Yebbi
Saison 1 Episode: 7
Jàngee Almãñ (étudier en Allemagne)
Jàngee Alm...
Saison 1 Episode: 8
yàqu-yàqu jikko yi (xaaj bu njëkk)
yàqu-yàqu...
Saison 1 Episode: 9
Yàqu-yàqu jikko yi (ñaareelu xaaj)
Yàqu-yàqu...
Saison 1 Episode: 10
Tariqa
Tariqa
Saison 1 Episode: 11